Teranga Doomu adama Liggéey doŋ ka mën a joxee Te li mu néew-néew Mooma gënal lenéen li ma mën ti am Jamono liggéey, jamono liggéey lañu nekk Liggéey war na góor, war na kiy jigéen Foo wara tekki, tekkiwoo fa doyna waar Nekk ci palas wara liggéey te liggéeyoo
Bës bula xa ca raw, boobee bës dem na Te beneen bi ñëw te xamuloo lu mu àndal Ma nee tàkku liggéey dafa jot Liggéey léen
Liggéey na nga liggéey (moo yoor réewmi) (Liggéey) foo mën a nekk (na nga liggéey) Foo mën a tollu(liggéey) moo yoor réewmi(liggéey) (Liggéey) foo mën a nekk (liggéey) foo mën a tollu (liggéey) Moo yoor réewmi (liggéey) (Liggéey) foo mën a nekk (liggéey) foo mën a tollu
Kàttan bi sax, moon di na mës a jeex Kaay ñu liggéey, liggéey taxawu sunu jàboot moo gën
Maa ni bës bula xa ca raw, boobee bës dem na Te beneen bi ñëw te xamuloo lu mu àndal Ma nee tàkku liggéey dafa jot Liggéey léen
Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome, welcome so easy
Na nga Liggéey, dollil liggéey (moo yoor réwmi) Na nga liggéey(foo mën a nekk) na nga liggéey(ag foo mën a tollu)
Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome, welcome so easy
Liggéey, dollil liggéey (moo yoor réwmi) Na nga liggéey (foo mën a nekk) na nga liggéey (Ag foo mën a tollu) naa nga liggéey Loo mën a amiit(naa nga liggéey)
Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome, welcome so easy
Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome Tell like wish welcome, welcome so easyTeksty umieszczone na naszej stronie są własnością wytwórni, wykonawców, osób mających do nich prawa.